Monday, May 08, 2006

ECRITURES DU MONDE
NSIBIDI
VAÏ

Saturday, April 22, 2006

GALLICA HISTOIRE DE L AFRIQUE
Quelques documents relatifs à l ' histoire de l' Afrique

CHAMPOLLION

Dictionnaire égyptien

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-106209&M=telecharger

Lettre à M. Dacier

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-39635&M=telecharger

Lettre de Champollion Le Jeune

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-55516&M=telecharger

Lettres d' Egypte et de Nubie

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-103771&M=telecharger


Panthéon égyptien
http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-106204&M=telecharger

____________________________________________________________________________________________________________________________________ VOLNEY

Voyage en Syrie et en Egypte


T1 http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-104113&M=telecharger


T2 http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-104114&M=telecharger

________________________________________________


AMELINEAU ( VOIR NATIONS NEGRES ET CULTURES de CHEIKH ANTA DIOP )


Un voyage en Nubie

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-84704&M=telecharger

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-84703&M=telecharger



Résumé de l' histoire de l ' Egypte

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-110242&M=telecharger


Abydos dans les temps anciens et dans les temps modernes

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-84705&M=telecharger



Les nouvelles fouilles d'Abydos


http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-55531&M=telecharger

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-55532&M=telecharger



MASPERO Gaston


Des formes de la conjugaison en égyptien

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-33043&M=telecharger




Histoire ancienne des peuples de l 'Orient

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-22519&M=telecharger


L' archéologie égyptienne

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-33168&M=telecharger


Les contes populaires de l' Egypte ancienne

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-36147&M=telecharger


Les inscriptions des pyramides de Saqqarah

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-106206&M=telecharger


Études de mythologie et d'archéologie égyptienne Tome 1 http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-55520&M=telecharger

Tome 2 http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-55521&M=telecharger

T3 http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-55522&M=telecharger


T 4 http://visualiseur.bnf.fr/Visualiseur?Destination=Gallica&O=NUMM-55523


T5 http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-55524&M=telecharger


T6 http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-55525&M=telecharger

T7 http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-55526&M=telecharger


T8 http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-55527&M=telecharger


Ruines et paysages d'Égypte

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-106207&M=telecharger



DELAFOSSE Maurice


Essai sur le peuple et la langue sara

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-105878&M=telecharger


L'âme nègre

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-84228&M=telecharger


Les civilisations disparues : les civilisations négro-africaines

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-104741&M=telecharger


Les coutumes agni : rédigées et codifiées

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-82386&M=telecharger


Sur les traces probables de civilisation égyptienne et d' hommes de race blanche à la Côte-d'Ivoire

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-95347&M=telecharger

Les Libériens et les Baoulé : nègres dits civilisés et nègres dits sauvages

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-84230&M=telecharger

Les noirs de l'Afrique

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-84220&M=telecharger

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-104745&M=telecharger


Les Vaï : leur langue et leur système

http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-77450&M=telecharger



Vocabulairescomparatifs de plus de 60 langues et dialectes parlés à la Côte-d'Ivoire et dans les régions limitrophes


http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-82436&M=telecharger


Les frontières de la Côte d' Ivoire , de la Côte d'Or et du Soudan


http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-95348&M=telecharger

Haut-Sénégal-Niger (Soudan français )


http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-103554&M=telecharger


http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-103564&M=telecharger


http://visualiseur.bnf.fr/CadresFenetre?O=NUMM-103565&M=telecharger
QUELQUES BELLES IMAGES :FRACTALES
http://fractales.free.fr/bijoux/sj_bijoux_cible2.htm

http://www.wack.ch/frac/pages.html

http://fractals.iut.u-bordeaux1.fr/jpl/jpl01.html

http://dreamp.club.fr/gal1.htm

http://www.educnet.education.fr/math/images/fractales/default.htm

http://gjoly.free.fr/fractales-projet/Recursif/recursivite.html

http://www.uisoftware.com/PAGES/galleryfractale.html http://www.futura-sciences.com/comprendre/d/dossier234-1.php


http://www.hofen.ch/~andreas/Franzoesisch/Fraktalgalerie/Fraktalgalerie1.html


http://www.epsilones.com/paginas/i-fractales.html


http://fractales.9online.fr/fractales/fractales.htm http://science-univers.qc.ca/cosmologie/fractale.htm


http://villemin.gerard.free.fr/Wwwgvmm/Suite/FracComp.htm

http://www.linternaute.com/savoir/diaporama/fractales/1.shtml



http://fractales.free.fr/diverses/jv_sbarb.htm#


http://www.dma.fi.upm.es/concurso03/presentados03.html http://ata-tenui.ifrance.com/xaos/fr.htm http://www.sdv.fr/pages/casa/html/fractales.html

http://www.col-camus-soufflenheim.ac-strasbourg.fr/Page.php?IDP=259&IDD=0

http://www.arrakis.es/~sysifus/


http://www.cidse.itcr.ac.cr/revistamate/Sketchpad/fractales/fractales.html
CORAN ET BIBLE : TEXTES ET AUDIO CORAN
TEXTES


LANGUES AFRICAINES

SWAHILI http://www.quranitukufu.net/

HAUSSA http://www.quranhome.com/qview1.asp

SOMALI http://www.quranhome.com/qview2.asp?page=3

YORUBA http://www.quranhome.com/qview2.asp?page=1


AUTRES

http://www.quranhome.com/index.htm

http://www.htcom.sn/spip/
http://www.lexilogos.com/bibliotheque_coran.htm http://www.intratext.com/X/ESL0024.htm


PLUSIEURS LANGUES

http://www.islamencastellano.com/coran.html

http://www.kuran.gen.tr/?x=s_main&kid=6





AUDIO

http://english.islamway.com/sindex.php?section=scholars

http://www.islamicity.com/mosque/quran/ http://www.yabiladi.com/coran/

http://www.sajidine.com/audio-video/audio/recitations-coran/page1.htm

ARABE FRANçAIS (LECTURE ALTERNEE )

http://www.sajidine.com/audio-video/audio/coran-arabe-francais/index.htm

ARABE ANGLAIS ( LECTURE ALTERNEE )
http://english.islamway.com/bindex.php?section=echapters&recitor_id=171

BIBLE

TEXTES

WOLOF

http://www.biblewolof.us/

PLUSIEURS LANGUES UN SITE QUI PERMET DE COMPARER PLUSIEURS VERSIONS (WOLOF , AMHARIQUE , FULFULDE ,SWAHILI, XHOSA , LATIN , GREC , ETC ) http://unbound.biola.edu/

http://www.speakingbible.com/



LEXILOGOS LIENS
http://www.lexilogos.com/philosophie_spiritualite.htm

http://www.lexilogos.com/bible.htm

http://www.lexilogos.com/bible_multilingue.htm

LANGUES AFRICAINES
http://visionneuse.free.fr/


BIBLE AUDIO LANGUES AFRICAINES ETC (HAUSSA , LINGALA , TIGRINYA etc ) http://www.audioscriptures.org/index-listen.htm

PLUSIEURS LANGUES http://www.audiotreasure.com/ http://www.speakingbible.com/

ANGLAIS http://www.audio-bible.com/bible/bible.html


FRANçAIS http://worldwide.familyradio.org/fr/mp3/bible/[/url]

Saturday, March 25, 2006






LEXIQUE MULTILINGUE

Saturday, November 05, 2005

WAXTAAN CI " Le PRINCE " BU NICOLAS MACHIAVEL


Tere Machiavel bi di "Il Principe" ( Buur bi ba Garmi bi" ) nek na lu mata xam ndax sunu nattangoo yi yag nañu ko di jëriñoo ngir noot ñu .Xam sa nattangoo nak bok na ci fagaru .



NICOLAS MACHIAVEL mi gi juddo ci dëkk bu ñu nan Florence ca Italie ci atum 1469 .Gen na aduna ci atum 1527 . Mi gi siiwe ci àdduna ak terem bi tud "Le Prince " . Bind na yenen téere yu ñu rañe maanaam " Dell' Arte della guerra " (xamxamu xare ) , "Discorsi sulla prima deca di Tito Livio "(waxtaan ci fuki at yu jëk yu Tite Live" ak yenen .

Sunu kaddu gi da nu ko y yamale(yemale) ci "Le prince " .
Jamono bi Machiavel di bind teere bi booba fekk na Italie nekkon ay diiwan yuy xiiroo . Li mu jublu woon mo di won jit wu ne nan ngay def ba dëgaral sa nguur .Seetuci woon nak lu jub ba lu jubadi .Teere bi bi nu ko sotte jur na coow lu bare .Ndax jamono jooju da ño jappni li muy jangale mengoowul ak diine mengoowul ak yoon .

Ci sunu gëstu bi da no top tëralam bi mu jëfandikoo ci teerem bi.

Xaac 1: Ñata xetu nguur mo am ak nan la nu koy ame

Machiavel mi gi rañe nguur yi ga xam ne buur mo len di jiite ak yeneen yi yuy fal njiit li .
Réewu buur yi xaaj na len ci ñar : nguur gi nu donn ak yu bees yi .
Nena : "reew yi ñu donn moy yi yàag ci kër buur bi ." " reew yu bees yi moy yi nu yokk ci dono"
CI gis-gisam reew yi nu am : des na ko am ak ngànnaayu jaambur wala say yos , wala ndax wërsëg , wala jiko ju rafet .

Xaac 2 : Reewu yi nu donn
Ci gis-gisu Machiavel réew yi nu donn ño gëna yomba jiite réew yu bees yi ndax te nit yi tamm nanu déggal wa kër bur bi .Na bur bi baña wesu àppi maamam yi ta teey waxtu yënguyëngu yi .Bu saxe ci yon wowu lu katanam new new di na mëna denc nguuram gannaaw xew-xew bu ñu manula waajal wacceko ta bu booba itam man na yaakar su jiit ku bees ki fakkastalo rek di na ko mëna wutu.


Xaac 3 Nguur yi rax

Ci fi nak la Gorgi Machiavel di wone xalatam ci nguur .
Nguur gi rax moy reew mi nu taqale benen reew .
" Ci reew mu bees bi la coono yep daje ndax nit dafa bëgg soppi kilifa di yakar ku bees ki gën ka dem.Bu nu gise ni jiit lu bees li mi gi len di tek coono ndax toppatoo xare yi ak ñoom-seen danuy bëgga dellu.

Buur bu bees bi dafay noonoo : benn ak ñi mu xañ seen teraanga , ñaar ak ñi ko jappalewoon ba mu am ndam ndax mënul leen bégal ni nu ko yaakaarewoon te mënuleen toroxal ndax kollëre gi dox seen diggante .
Machiavel nena lu buur am kattan ak ay xarem soxla na ndimmalu wa reew wi muy saku gir mën fa dugg.

Pexe yi muy digal buur nak yi la
- jiite ñu mësul mom seen bopp lu yomb la : na buur bi raafal xeetu buur bi mu wutu ta bayi nit yi ñu dund ak seeni aada rek jamm ne ñoy .
Su feke ni rew mi ga saku dafa sore ta bokkuleen aada , benn pexe rek : sanc fa .Nonu la Turc yi noote Grec yi .

Nena bu buur bi sance ci reew mu bees mi di na mëna fac yàq-yàq gu jib bala muy ëpp loxo .

Monday, October 24, 2005

THEME INVENTEURS NOIRS : Quelques liens
LISTE NON-EXHAUSTIVE D’INVENTIONS RÉALISÉES PAR DES HOMMES ET DES FEMMES DE LA DIASPORA NOIRE
http://www.africamaat.com/article.php3?id_article=55
http://www.grioo.com/info3018.html
Association archive(qui donne aussi des liens)
http://www.associationarchive.com/index.php?main=dossiers.php&dossier=2
http://membres.lycos.fr/ajeanne/FAC/CompileparByronCrudupNetdays.html


Black Inventors A-Z
Ce site met en ligne les brevets des inventeurs noirs vous y trouverez des infos pour toute invention.
http://inventors.about.com/library/blblackinventors.htm
http://www.blackinventor.com/
De nombreux liens sur le site ci-dessous
http://www.ideafinder.com/history/inventors/latimer.htm

THEME : CHEIKH ANTA DIOP

http://www.ankhonline.com/cheikh.htm
Cheikh Anta Diop, restaurateur de la conscience noire
http://www.monde-diplomatique.fr/1998/01/HERVIEU_WANE/9787
The Pharoah of Knowledge
http://home3.inet.tele.dk/mcamara/antadiop.html
http://www.grioo.com/info83.html
http://www.grioo.com/info7.html
http://www.africawithin.com/diop/diop.htm

http://www.nbufront.org/html/MastersMuseums/JHClarke/Contemporaries/CheikhAntaDiop.html

http://www.aps.sn/dossierCheikh_Anta.htm
http://www.africamaat.com/article.php3?id_article=153
A Brief Biography Of An African Champion
http://www.raceandhistory.com/Historians/cheikh_anta_diop.htm
http://www.afrikara.com/index.php?page=contenu&art=277&d=478
http://www.africawithin.com/diop/diop_bio1.htm
http://www.cwo.com/~lucumi/diop.html
http://www.utexas.edu/cola/france-ut/archives/Spring2005/Diop.pdf
L'action politique au diapason de la recherche scientifique
http://www.lintelligent.com/gabarits/articleAfricain_online.asp?art_cle=LIN28123cheikpoidat0
DR. CHEIKH ANTA DIOP AND THE CULTURAL ROOTS OF THE DALITS: INDIA'S BLACK UNTOUCHABLES
By V.T. RAJSHEKAR
http://www.cwo.com/~lucumi/dalits.html
http://www.ikuska.com/Africa/Historia/biografias/biografias_cheikh_anta_diop.htm
http://www.egyptsearch.com/forums/Forum8/HTML/002508.html
http://dickinsg.intrasun.tcnj.edu/diaspora/diop.html
En 1954 un Africain Américain écrit l’équivalent Nations Nègres de Cheikh Anta Diop
http://french.epochtimes.com/news/5-2-22/946.html

http://www.arts.uwa.edu.au/MotsPluriels/MP898dtp.html
http://www.africaquiz.com/Pages-fr/ARTICLES/THEMES/divers/olivier_bain_interview.htm
L'importance d'une conscience de l'histoire pour un
développement auto-déterminé
http://www.africavenir.com/publications/student-papers/BendixCADiop.pdf
http://www.african-geopolitics.org/show.aspx?ArticleId=3659
Africanisme et Théorie du projet social
http://mnas.ifrance.com/preface.htm
http://www.sis.gov.eg/public/africanmag/issue03/html/frafr06.htmCheikh Anta Diop et son oeuvre monumentale
http://www.afrology.com/litter/pdf/cadiop1.pdf

ORIGIN OF THE ANCIENT EGYPTIANS

http://www.melanet.com/clegg_series/diop.html
http://burundi-sites.com/agnews_diop.htm

http://www.raceandhistory.com/cgi-bin/forum/webbbs_config.pl/noframes/read/1624
http://idih.hab.de/Diop.pdf
http://mnas.ifrance.com/interview.htm

http://www.hartford-hwp.com/archives/30/009.html
Afrocentric Book & Video Recommendations
http://www.homestead.com/wysinger/ptahhotep.html
African Ourstory
http://www.cultural-expressions.com/diaspora/africanour.htm
The Black Egyptians--Original Settlers of Kemet
http://www.stewartsynopsis.com/black_egyptians_are_the_original.htm
http://www.cameroon-info.net/cmi_show_news.php?id=15847
http://www.cishsydney2005.org/images/MT2b%20Ibrahima%20Thioub.doc

quelques conceptions cosmogoniques et symboliques de l'Égypte ancienne et de l'Afrique traditionnelle
http://perso.wanadoo.fr/africart/pages/etude3.htm
MOIS DE L'HISTOIRE DES NOIRS 2003
http://interculturel.ville.montreal.qc.ca/hist_noirs/2003/laureats2003.htm
http://www.africanreviewofbooks.com/100best/100bestsamples/diop.html
http://www.ijebu.org/repository/empires/index.php?cat=56
http://www.rastafarispeaks.com/community/modules.php?name=News&file=article&sid=113

The First Chinese were Black
http://www.trinicenter.com/FirstChinese.htm
http://web.cocc.edu/cagatucci/classes/hum211/timelines/htimeline5.htm



http://fr.wikipedia.org/wiki/Discussion_Utilisateur:DJIBRIL_CHIMERE_DIAW
LEXIQUE SCIENTIFIQUE WOLOF





TRADUCTION DE CONCEPTS SCIENTIFIQUES EN WOLOF
INSPIRES DE L OEUVRE DE CHEIKH ANTA DIOP
AVEC LES GRAPHIES ACTUELLES

TRADUCTION DE CONCEPTS MATHEMATIQUES
NOTIONS PRELIMINAIRES
point : tomb b
ligne : rëdd w
plan : maasale
surface : yaatu-yaatu , ëmbka
axe : digel
sens : joxañ, joxoñ
demi-droite : xaaj
angle : koñ b , angal b , puxtel
angle adjacent : puxtel bokkwet
_ droit : puxtel jub
_ aigu : puxtel xat
_ obtu : puxtel laññ
_ complémentaire :motlente , mëtlente, matlente
_ supplémentaire : yokkalente


TRIANGLE : ÑATKOÑ
coté : wet g
hauteur : kawewaay g , kowewaay g
angle : puxtel , koñ
médiane : jarr-diig
sommet : puj b
hypothénuse : janookoñjub
bissectrice : seddale puxtel
médiatrice : tasebkaweway, tasebkaweay



GENRES DE TRIANGLE GÏR I ÑATKOÑ
triangle isocèle : ñaariw -yam
----- rectangle : koñjub
----- équilatéral : wet- yam
------- scalène : yamadi
droites parallèles : njublang
angles alternes internes : jallawlebir
alterne externe : jallawlebiti
angles correspondants : bokkdeme , and
quadrilatère : ñentwet
parallélogramme rectangle : wetlanglang
rectangle : jubkoñ
losange : carre doy
carré : carre
trapèze : ñariwetlang
diagonale : aw galen, aw galan
symétrie : safaanoo
symétrie par rapport à un point : safaanoo jakkaaarle'b tomb
-------------------------- : safaanoo jakkaarle'w red
------------------------ ; safaanoo jakkaarle' g maasale

CERCLE - CIRCONFERENCE : MBEGE
cercle : mbege
circonférence : mbege guddaay
centre : digg
rayon :ceeñeer l
corde : buum g
diamètre : buumdigg
arc : xala g
tangente : feleesu

MESURES DES ANGLES : ÑAT KOÑ
angle au centre : puxtel diggal
intercepter : dog xala
rapporter : nattukay
angle inscrit : puj ci mbege , koñ bindu
angles opposés : jakkarle

TRANSFORMATION
homothétie : sopiîn
homothétie directe: sopiîn jub
rapport d ' homothétie : demexin gi , sopixin
homothétie indirecte : sopiiin jallarbiku
puissance d' un point par rapport à un cercle : kattan nug tomb jublu ci mbege
GEOMETRIE ANALYTIQUE : KANAM JEXU
nombre réel : lim amu
nombre imaginaire : lim jeneer , lim janeer
TRINOME ET EQUATION DU SECOND DEGRE : ÑAT DOG ( DOG ÑAT ) AK YAMALE G ÑAREL BI AJ
coefficient : ngung
racine : reen
signe du trinôme : joxañ u dogñattgi
coordonnée cartésienne : xamekay i descartes wala xammekay makarall
axe : diggel
origine : cosaan l
coordonnée: xammikay
abscisse : lal gi
ordonnée : aj bi
projection orthogonale : takkandeeral jub , taqandeeral jub
projection oblique : takkanderal doy , taqandeeral doy
pente : mbartal m
coefficient angulaire : ngungul puxtel
aire d 'un triangle : yaatuwaayu ñatikoñ
la courbe et son équation : ndëng ak uk yamalem ( yemalem )
droite : rëd
conique : njurelugdank
ellipse: mbege tappandaar
hyperbole : xalajumoyonte
parabole : xala , xon
courbe algébrique : ndëng aljebar, ndëng joxañu(joxoñu)
courbe transcendante : ndëng aljebarul
coordonnées polaires : xammikay jotu
pôle : dott
rayon vecteur :
normale : mak aw
tangente : felasu, feleesu
sous-normale : ron mak
sous-tangente : ron felasu
inversion : jallarbiku
pôle d' inversion :jot ub jallarbi
puissance : kattan , ngôora
sommet : puj
tangente au sommet : felasuk (feleesu) puj
hyperbole équilatère : xala dummooyumak
hyperboles conjuguées : xala dummooyunexo
asymptote : nammlalut ,nammjotul
section conique : do nduru dank
directrice : wommatgi
foyer : taalbi
excentricité : moydigg , tappandaral
polaire : dotu
division harmonique : seddale bu deggoo
axe radical : digall renu
sphère : tëmb
ellipsoïde : doomi mbege tappandar
hyperboloïde à une nappe : xalabumoyonte ben lal , wen dal
coordonnée sphérique : xammikaay tëmbu
coordonnée semi-polaire : xammikaay dotugenwall
déterminant : degkat
colonne : kenu , wate
ligne : rëd
angle de deux droites : koñ ub ñari njub
faisceau de droites : tak ub rëd
quadrilatère complet : wetñent mat
point à l' infini : tomb ta gappodiku
droite de l' infini : rëdu gappodiku
point cyclique : tombi dem delloosi(dellusi) , tomb tedu
droite isotrope ; rëd makarlo g boppam
méthode des parties proportionelles : ter yu demante yi
points multiples : tomb baril
point double : tomb ful
point de rebroussement : tomb dem dik
théorie des enveloppes : faramfacep ëmbyi
courbure : dëngaay , ndëngin
développée : ëmbmak yi
rectification d' une courbe : jubanti ndëng
aire limité par une courbe : yaatu gu dëng degg
volume d' une surface révolution : kembakal yaatug dargandal
centre dans les coniques : digg ci jurelu dank yi
diamètre dans les coniques : buumdiggu ci jurelu dank yi
diamètre singulier : buumdiggu
réduction de l'équation du second degré : folet yamalel ñaarel bi aj
théorème de Rolle : wonewug Rolle
maximun relatif , local : maggi yek aju barabal , dendando
minimun relatif , local : yes gi wat barabal , dendano
la dérivée d ' une constante est nulle : selalug sax tus la
intervalle (A, B) : digganté (A ,B)
dérivée : sel , ses
hypothése : wax jiitel , xalat jiital
réciproque : degsafanu
fonction : aju , soppiku
fonction continue : soppiku (ag) dogul
fonction discontinue : soppiku (ag) dogna
fonction primitive : soppiku (ag) jëk
corollaire : deg wetal
fonction dérivable : sopiku selu
fonction croissante : sopiku mag
fonction décroissante : sopiku wañiku
étude d'une fonction au voisinage d'un point : njang um sopiku ci wetu tomb
position de la couirbe par rapport à la tangente en un de ses points : taxawayu ndëngwi nam demeg felasu tuke ci benn ci tombam
point d ' inflexion : tombub tadday
point multiple : tomb dox bari
point double : tomb jarat
convexité : xugi , norebir
concavité : dox , norebiti
développement limité : texarñi gappu
coefficient de développement : ngungul texarñi bi
fonction bornée : sopiku paku
dérivée première , seconde , nième : sel benel , ñarel , nangamel
cosinus hyperbolique : tedin xala dumoyu
sinus hyperbolique : taxawin xala dumoyonte
fonction infinie : sopiku gappodiku
branche infinie : banxas gappodiku
recherche d ' une direction asymptotique : wutu g jublug namm jotul
asymptote oblique : namm jotul denga
asymptote cubique : namm jotul ñatkal
courbe définie paramétriquement:ndëng wi toxu kat bi degg
arcsinus : xala taxawin
infiniment petit : tuti gappodiku
infiniment grand : mak gappodiku
forme indéterminée : bind maanawodiku
infiniment petit principal :tuti gappodiku fulawu
infiniment petit comparable : tuti gappodiku tolalowu
infiniment petit d' ordre P par rapport à la partie principale : tuti gappodiku ker P ci ab demem ag wall gi fulawu
ordre d' un infiniment petit ou grand : ker ug tuti gappodiku walla mak gappodiku
développement d' un infiniment petit suivant les puissances croissantes de l' infiniment petit principal : texarñi tuti gappodiku topa kattan maggi tuti gappodiku fulawu bi
croissance comparée des fonctions à puissance x : magg tekeleg sopiku i A(x)
limite d'une fonction : gapp ub sopiku
fonction multiforme : sopiku bare binda
fonction implicite : sopiku binduwale, luxu
calcul vectoriel : hayma'b demu
notion de vecteur : manam demu
intensité :taray
direction :jublu
sens : jëm
vecteurs liés : jëmu yu taxo
vecteurs glissants : jëmu yu barastiku
vecteurs libres : jëmu yu jambur
extrémité : taat
module : sebre
support : dastandikuwi
ligne d' action : ndefka wi
vecteurs équipollents : demu lang safaano
rapport de deux vecteurs paralleles :demeb ñari demu langa
relation de Shall : dote b Shall
association de l' addition géométrique : mbotayog boole kanam yi
composantes d' un vecteur :sosando
vecteur unitaire : demu sebre , bennal
composantes intérieures extérieures : nekado w biral , bitil
proprité du produit scalaire : baxub baril demuwul , limu
équation normale : yamale jadu
considérons la fonction m=m(u) ; quand u varie m décrit un arc de courbe appelé indicatrice : donté sopeku M= M(U) su U de sopeku M di rëd xalag ndëng gu tudd wonekat
analyse vectorielle : yebig jëmu
dérivée vectorielle du 1er , 2 ème ordre : selal jëmu'b benel ñarel nangameli ker
le vecteur vitesse dm/du a une signification géométrique : jëmu'g xelal amna tekib kanamal
généralement la tangente se définit par un vecteur directeur unitaire : li ci ëp felasu gi ñung koy dege jëmug wonekat bennkesel
l'arc et la corde correspondante sont des infinments petits équivalents : xala geg bum gi mu mengol ay tuti gappodiku yu weci ko la ñu
cosinus directeur de la tangente orientée : tedel womatkat u felasu gu gindiku
plan normal : masale makaral
indicatrice des tangentes : wonekatu felasu yi
normale principale : makaral fayda wu


Traductions de concepts scientifiques
physique et chimie
vocabulaire scientifique d'après l 'oeuvre de CHEIKH ANTA DIOP(corrigée avec graphie actuelle)
THERMODYNMIQUE : tangdoolel
unité mécanique :bennkesel doolerandu
unités : wennkesel ; nattu(ay)
surface : yaatuway
volume : këmbay
vitesse : gaawkesel, xël
accélération : xiirël ,xiiral
force : doole
travail: liggéey
puissance : kattanef, ngoora
pression atmosphérique : naj ub ngelawli
température : yegu tangaay
thermomètre : (ag) nattangay
conductibilité calorifique : wommatinu tangaay
température absolue : yegutangaay dendandoowul
zéro absolu : tus dendandoowul
dilatation : fokki, funki
quantité de chaleur : dayob tangaay
chaleur spécifique : tangaayu boppam
chaleur de fusion : tangaay boppam
chaleur de vaporisation :tangaayu coolool (coola , cuuluul)
chaleur latente : tangaay nelaw, nëbbu
rayonnement : ceeñeeral
surface isotherme : yaatuway yemtangaay
régime permanent : doxin faw
résistance thermique : dëgërlu tangaay
calorifuge : denctangay
isoler thermiquement : ber ciw tangaay
état d'un corps : nekkinu yaram
corps homogène : yaram genngiir
corps hétérogène :yaram barigir
équilibre thermodynamique : dëngadig tangdolel
variable indépendant: soppikukat ajuwul
adiabatique : daggog biti ,
équation d' état des gaz : yamaleg nekkinu ngelawyi
mélange des gaz parfaits : njaxasum ngelaw muccaayub
transformation infiniment petite : binduwat tuut gappodiku
travail des pressions dans une transformation : wangerñikuwu ?, wangarñikodiku ? , jexu
pression d'uun gaz : naju gil
gaz : ngelaw , gil
conservation du travail : reeredig liggéey
machine simple : wuutuloxo wayaymbir
poulie, treuil : siga, sigagengelo
énergie potentielle : kattan ëmbu
énergie cinétique : : kattan imbiku
force de frottement : dooley riisu
équivalence de chaleur et du travail : weccikonteg tangaay ak liggéey
variation de l' énergie interne : soppikug kattan biiral
énergie calorifique : kattan ditangaay
chaleur totale ou enthalpie : tangaay wepp
calorimètre : nattdayotangaay
conservatioon de l' énergie : reredig kattan
coefficient calorimétrique : ngungul tangaaynattukay
transformation adiabatique :binduwat dagogbiti
rendement d'un moteur thermique : dellob doxalkatup tangaay
cycle de Carnot : degnegup Carnot ,, tedug Carnot
entropie : manaamupjalaxu
fluide homogène : dawdawan genngiral
compression adiabatique d' un liquide: naj dagogbitig dawdawan
théorie cinétique des gaz : faramfacce imbikuwug gilyi
hypothèse moléculaire : ngënjabariw doxdajewul
vitesse efficace : xël dikkdara
statistique : limbare
mouvement brownien : jaluxub Brown
équipartition de l' énergie : seddaleyemub kattan
viscosité des gaz : rattaxayub ngelewyi
conductibilité calorifique : wommatinutangaay
gaz réels : gelewedëggdëggyi
covolume :këmbaylenn
états métastables : nekkinxawataxawadi
pressions internes : najubir
chaleur spécifique : tangaayu boppom
fugacité : royett
titre : koj
copncentration de volume : faraye
molarité : wesofulem
rapport molaire : demeb wesoful
ebulliomètre : nattbax
cryomètrie : nattsed
pression osmotique : najmanq
chaleur de dissolution : tangaayu tasmbootaay
activité : njaxlaf
transformation allotropique des solides : binduwat u birumeloy dëgër yi
vaporisation : coolool
pression de vapeur : najub najub coolool
sublimation : sedcoolool, sedcoola
phénomènes capillaires : feñfeñcooloomal
tension superficielle : dendtondal
rayonnement thermique : tangaay ceeñeeral
pouvoir émissif : manmanab yonem
densité de l' énergie : rajjug kattan
rayonnement : ceeñeeral
flux lumineux : wallum leer
intensité : taray
pyrométrie : nattsafara

ELECTRICITE
électrisation : mbëjel
conducteur électrique : wommatukayu mbëj
isolant : berkat
attraction et répulsion : wootal , bëmëx
électricité positive et négative : mbëjkanamal , gannawal
électroscope : bëtub mbëj
isolant : berkat
charge électrique : sëfub (yanub) mbëj
électrons : mbëj peppal ; mbëj feppal
champ électrique : tollu mbëj
ligne de forces : rëddi doole
potentiel ; flux de forces : ëmbu , aj , wallum doole
travail d' un déplacement : liggéeyu randatu
surface équipotentielle : yatu yem ëmbaj
diagramme électrique : ndëng mbëjel
sphère électrisée : temb mbëju
densité superficielle : rajju tonde
machine électrostatique : wuutuloxob mbëjtekeral
milieu diélectrique : diggënte lankmbëj
électromètre , montage idiostatique : we wenntekeral
courant électrique permanent stationnaire : dawane mbëju , fawu , tekal
intensité de courant : tarugdawane
conductivité : dawalin wi
résistivité : teyewin wi
sens du courant : jublug dawan gi
courants dérivés : dawan sel
résistance : teye
pont : sala
thermomètre à résistance : nattangayug teye
bolomètre : tëmbnat
méthode d' opposition : ligeyinnu dekerle
potentiomètre : nat embaj
effet thermique du courant : sababtangu dawan
loi de Joule : atteb Jul (Sul)
fusible : ruyekatbi
ampèremètre : natt Ampère , natt taray
voltmètre : natt wolt , natt wute emaj
photomètre : natt leer
rayonnement : ceeñeral
flux : wal
dissociation électrolytique : tasmbootay mbëjndoxal
ions : xarefulwon feppret
équivalent électrochimique : wet (mengo) mbejyaramal
électrolyse : mbëjndoxuwu
polarisation : dotal
conductivité équivalente : wommatine weccikuwu
mobilités des ions : taxawajib (boyboyanub) xareful feppret
nombre de transport : limub yobu
galvanoplastie : xoob
énergie électromagnétique : kattan mbëjxëju
énergie mutuelle : kattan yariwet
relais : aw
unités : benn kesel , benn nen, wen kesel , wen nenal
longueur : gudday
masse : laf
temps : jamono
dimension : dayo yi
vitesse de mouvement uniforme : xëlu doxmaase
centimètre , gramme , seconde : temerelub metar , gram, saa
vitesse : xël
accélération :: xiiral
force, dyne : doole , din
travail : liggéey
puissance : kattansa
charge électrique : yann mbëjlu
densité superficielle : rajj tondel
moteur à courant continu : doxalkat dawansafaanawul
couple moteur : seex safaanoo doxalkat
pulsation : ab wex
fréquence : baray
alternateur monophasé : safankat wennwexin
inducteur : jurkatbi , dugalkat, jokkat bi
induit : njurelgi , dugukat , juki gi
rotor : wendelukatbi
période: depneg
courants polyphasés : dawan bariwex , rawate
courant alternatif : dawan safaanu
moteur asynchrone : doxol demandowul
transformateur : soppikat , bindatkat
circuit primaire , secondaire : ndombo jëk , dombo tegu
chute de tension : yulub dend
vibration électromagnétique : send mbëjxecal
propagation : jaljalat
courant de convection : dawan yegwat
lampe triode : leeral ñattal
courant de saturation : dawan tox
anode, cathode : yéegu, waccu
redresseur de courant : jubbanti dawan
lampe à grille : lampu giryas
caractéristique de la plaque : jikkoy dallwi
amplificateur à résonnance : yokkekat sabando
haute fréquence : baray kawe
circuit oscillant : ndombo dëngdëngaan
téléphone, microphone : waxsori , waxsufe
rayons cathodiques : ceeñeeri watukaybi
oscillographe cathodique : ioxkatu watukaybi , bindlox
décharge dans les tubes luminescents : sippi cisolomyu xuy yi
arc électrique: xala mbëju
force électromotrice : doole mbëjdoxal
pile : ab tegele, tegale, tegle
électrodes d' hydrogène : mbëj jaru jur ndoxal
électrodes au calomel : mbëj jaru calomel
activité d' un électrolyte : njaxlaful mbëjnodoxal
énergie libre : kattan tambabalu, tambaambaalu,tambalu
coefficient d' activité : ngungumg njaxlaf
polarisation des piles : dotub tegele, tegale
accumulateurs : dajalekat
aimants permanents : xëccckat faw
magnétostatique : maneto tekeral
pôle Nord , pôle Sud : dot bëjganar , dot bëj Sine
attraction et répulsion entre aimants : ñodente , bëmëxenteb , xëcckat
charge magnétique : sëfxëccu
doublet magnétique : ful xëccu
force magnétique : doole xëccu
champ magnétique : tolub xëccu
moment magnétique : jikkoy xëccu
intensité d' aimantation : tarayub xëccuwom
aimant uniforme : xëcckat maase
induction magnétique : xobus xëccu
feuillet magnétique : jog xëccu
énergie potentielle d' un feuillet : kattan ëmbub as xob
solénoïde : taxar
selfinduction : sakcibir , jurcibir , jocisabir
perméabilité : senn
hystérésis : des
circuit magnétique : ndombo xëccu
force magnétomotrice : dooleyi xëccdoxal
entrefer : diggënteweñ
électroaimant : mbëjxëcc
_ sensibilté : (as) yëg
_ système astatique : yab tacrawul
_shunt : tegi
galvanomètre à cadre mobile : natt taray , natt galwa kadar wëndéelu
oscillation du cadre : jingjingan y kaadar
fluxmètre : natt wal
ampèremètre : natt amper
voltmètre : natt wolt


CHIMIE GENERALE : simi jajal
la théorie atomique : faramfaccebxareful yi
loi de conservation des masses : attebi yi denculaf
la somme des masses des corps formés au cours d' une réaction chimique est égale à la somme des masses des corps mis en oeuvre : mbolem lafi yaram yi sosu ci dugunteb(duganteb) yaramal mingi yamag mbolem lafi yaram yi jalbenga
loi de conservation des corps simples : atteb dencug yaram yi woyof solo
loi des proportions définies en poids : atteb cërcërat degu yi cib disay
la proportion suivant laquelle deux corps simples peuvent s' unir en formant une espèce chimique n'est pas susceptible de variation continue : cërcërat bi ñari yaram woyof solo di dugante ndax jur wanen xeti yaramal manula soppiku soppiku bu dagodiku
loi des proportions multiples : atteb cërcërat yi bari
loi des combinaisons gazeuses : atteb gil yi fono
hypothèse moléculaire ; atomes : waxjitalug wesoful, xareful
la molécule d' un corps simple ou d' un corps composé est la particule ultime de ce corps susceptible d' exister à l' état isolé : wessofulu yaram wayof solo wala fono moy ndagit su muj sa ci yaram wowo, wi mana nek beru
le mouvement brownien : jalaxu Brown
symbole chimique ; les équivalents : misal yaramal ; wecciko yi
les nombres proportionnels : lim yi cërcëratal
allotropie : wuutekbir
poids atomiques et moléculaires : këmbayul xareful , wesoful
atome gramme, molécule gramme : xareful , wesoful
volume moléculaire : këmbayul wesoful
tonométrie , ébulliométrie , cryométrie : natt bes , natt bax, natt sed
les chaleurs spécifiques : tangaayu boppam
isomorphisme : bokkdunda
la théorie des ions : faramfacce xareful
l'électrovalence , la valence-gramme :mbëjlonk, lonk gram
degré de dissociation :ajug tasub mbootaay
électrolytes forts , faibles : mbëj ndoxal doolewu , neewdoole
électrons négatifs , électrons positifs : xaréful fepprec, bëmëxkat , kotalkat
milieu réactionnel, solubilité : barabubdugan , soyin
double décomposition : fulub foniku
neutralisation des actions acides par les bases : jamburalal xongxal yi ag baxal yi
hydrolyses : tasag ndox
mélanges hétérogènes : jaxas barigir
mélanges homogènes : jaxas gengir
émulsions : faat
corps purs : wenn yaram
fractionnement : dissolution fractionnée : dundelub walatal
solidification :dëgërël
épuisement par des solvants : jexel aki naankat , soyalkat
distillation fractionnée : tog , coolal, walaatal, soyal
mélanges azéotropiques : njaxas nawando
dissolution , adsorption , diffusion : soyal, tagal , wutilfune
combinaisons moléculaires : fonob wesoful
les complexes : dismbir yi
solubilité , courbe de solubilité : soyin , ndëngu , soyin
saturation d' une solution : nanatalub soyal
solution sursaturée : soyal wesnanatul
cristallisation d' une solution : dundalub soyal
saline aqueuse ,eutectique :bu xoramu ndoxu , rafet binda, jekbinda
hydrates salins : ndoxal xoramu
eau de constitution , eau d' hydratation : ndoxum yab , ndoxum ndoxal
théorie de Werner , indices de coordination : faramfacceb werner , doxanub andlo
symboles moléculaires , formules planes : manam wesoful , tënka masalel
formules brutes , formules ioniques : tënka rataxalesuko , tënka ful , feppreta
addition , substitution , radicaux : mboole, wuutu, renal
groupements fonctionnels : dajaloyu soppikukatal yi
valence des éléments et des radicaux : lonkub dexityeg renal
équivalents : mengo
électrovalence , coordination : mbëjlonk, mbokfepp
isomérie de constitution : boktënk tig yab
isomérie de position : boktënk cik taxaway
tautométrie : yaram tënkñaral
migration d' atomes , transpositions : mangubxarefulwon , toxubarab
réfraction moléculaire : damug wesoful
parachor : embedenda
pouvoir rotatoire magnétique :manmanub dargandal xëcal
diamagnétisme , moment électrique : safan-xet , yangud mbëj
paramagnétisme : joxañ xëc
stéréochimie , représentation tétraédrique : dawyaramal , taxawalub ñintimasale
principe de la liaison mobile : campug takob boydoyan
polymorphisme moléculaire : baribindub wesoful
théorie des tensions , isomérie cyclanique : faramfacceb dendu yi , boktënk tëdu
polarisation rotatoire : dotal dargandalu
dissymétrie de structure : dekerlodib bindbir ?
empêchement stérique : tere (fel) dugente
racémique , dédoublement : fulal
isotope : wuuteb disay , wuuteb sal
spectrographe de masse : rëdxonug laf
spectre atomique et moléculaire : xonug xareful , xonug wesoful
spin nucléaire : jublug sal
transmutation : jemet yi
radioactivité : yebikul sa bop ( tasal sa bop)
rayonnement radioactif : dengadifen tasebopal
énergie de désintégration : katanug yebiku
neutron : yannuwul si
deuton : feppdis
proton : feppsalal
photon : feppleer
matérialisation des photon : lambdajalub feppleer yi
positon : kanamal
négaton : nganawalsi
rayons cosmiques : ceeñeer dajnekal
radioactivité artificielle : yebikul sabopp dabla , gu ñu saka
électromètre : nattmbëj
espèce chimique : xet yaramal
domaine de pureté : momeluk koduwul
constantes physiques : saxsax y bitil
analyse immédiate : jex bujëk( fisasi)
analyse qualitative , quantitative : jexub jiko yi , jexub dayo
corps composés , corps simples : yaram fonoo , yaram wen
élément : bennal
éléments : wennal yi , jexit yi
LES EQUILIBRES CHIMIQUES :jengadil i simi
équilibre mobile : jengadi boyboyan (taxawul)
constituants indépendants : yabyab ajuwul
potentiels chimiques : emad , yaramal yi
équation d' équilibre d' une phase : yamaleg jengadib tolutolu
variance d' un système : sopikuwatug tabax
loi des phases : atteb tolutolu yi
systèmes de premier ordre , second : tabaxug benelu ker , ñarelu
transformations allotropiques : binduwatu melowbir
solutions salines : soyam xorom
courbes cryoscopiques : ndëng sednat
point d' eutectique : tomb rafet
point de transition : tombub jalu
mélanges binaires : liquidus , solidus : njaxas ñaral ; dawdawanal , dëgërël
analyse thermique : jex tangal
composés isomorphes : fono bokbind
sels doubles , alliages ternaires : xorom ñaral , rax ñatal
déplacement de l' équilibre : randub jengedigi
_par variation de la pression :_ ag soppiku nattbi
_ par varition de la concentration : _ag sopiku faraybi
loi d' action de masses : atteb jëfi lay yi
constante d' équilibre : saxsax dengadil
concentrations moléculaires : farayub wesoful yi
système homogène , hétérogène : tabax , gen gir , tabax gir bare
forces des acides et des bases : doley xonxal yi , doley baxal
dissociation : tasmbootay
constantes de dissociation : saxsaxub tasmbootay
produit ionique : barelub xareful feppret
hydrolyse , degré d'hydrolyse : tasndox, tolub tasndox
cinétique chimique : imbib yaramal
vitesse de réaction : xelu dugante
énergie d' activation : katanug njaxlafal
réaction en chaîne : dugante talalal
ordre de la réaction : kerug dugantebi
activation par choc photochimique : njaxlafalub finxe , leeryaramal
catalyse homogène , catalyseur : tux gen gir , tuxkat
antidétonnant , antioxygène : tere toj , non dundal
catalyseurs biochimiques : tuxkat dundyaramal

CONSTITUTIONS DES ATOMES
décharge dans les gaz raréfiés : sipiku ci birngelaw yuñu tumurankel
rayons cathodiques : ceeñeer waccal
les rayons cathodiques sont les trajectoires des charges électriques en mouvement : ceeñeerwaccal yi , ñoy saawoy sëf mbëjel yi jalaxu
voltage et potentiel :wuute aj , embad
charge spécifique et masse de l'électron : yanub boppom , lafu mbëjfeppal
rayons positifs , rayons canaux : ceeñeer kanamal , ceeñeer xunti
modèle de Rutherford : rañikub kattan ferñent
mécanique quantique : dolérandatub katan ferñent
mouvement des électrons sur des orbitrtes privilégiés formant une suite discontinue : jalaxub mbëjfeppal yi ci saawo yu tannuyi tof mu (toflin ) dagu la
quantum d' énergie : kattan farñentu kattan
séries spectrales de l' hydrogène : tof (toflin) xonalu jur ndox
longueur d' onde : guddayub gewelu
nombre quantique : lim katan ferñental
principe d' exclusion de Pauli : campug bokadilug Pauli
mécanique relatviste : dolé randatu dendandol
inertie de l' énergie : yengiralug katan
mécanique ondulatoire : dolerandu gewelu yi
probabilté de présence : amanab feke
loi de Moseley : atteb Moseley
la racine carrée de la fréquence d' une raie déterminée est une fonction linéaire du nombre électronique de l' atome émetteur : ren ñarkab barayub wen xall soppikug njubal la gog limub mbëjfeppolub xarefulwon yonekatba
numéro atomique : jerug xarefulwon
classification périodique des éléments : kerelé depnegub wenal yi
constitution des cortèges électroniques : yabug mbëjfeplu

CONSTITUTIONS MOLECULAIRES
les liaisons ioniques , transfert d' électron : lonkoy xareful mbedfeppal feppret , yobu
combinaisons hétérogènes : fono wuute gir
liaisons par électrovalences : lonkob mbëjwetikuwo
les liaisons covalentes ; théorie de l' octet : takob bokub lonku , njuromñatsi (faramfacceg)
transfert de proton : yobug feppsalal
diffraction des rayons X : damug ceeñeer nangam (X)
hauts polymères macromolécules : tegelesabopp yu mag yi , wesoful mage
analyse : yebbi , jeex
synthèse : yabat
electroaffinité : mbëjsoppante
classification électrochimique des éléments : kerelewub mbëyaramalug wenal yi
cathode : yootu
anode : yegu
réaction cathodique : dugante waccu
oxydation anodique : dundal yegu
réduction : xaññ
peroxydation : yokdundal

THERMOCHIMIE
effets thermiques , mécaniques : sababu tangaay , sababu doole randatu
équilibre chimique , réaction chimique : jegadifenub yaramal , duggantep yaramal
équilibre mobile : degadifentaxawul
thermostat , isotherme , monotherme : tangaysopikuwul
isotrope : djikojen
équilibre métastable : jégadi westaxaway
action catalytique : jëfi tuux wi
équivalencede la chaleur et du travail : wecceg tangayag ligey
équivalent mécanique de la chaleur : mengodolerandatuwug tangay
cycle fermé : depneg tej
énergie interne d' un système : katanjariñowu , katanjenguwul
conservation de l' énergie : dencub katan
chaleur de réaction : tangaaydugunte , tangaaydugante
réaction exothermique , endothermique : dugnute jurutangay, nanu tangay
déterminations calorimétriques : nattub tangaay
affinité chimique : boklefub yaramal (namente sopente)
énergie utilisable , énergie libre : katanjariñowu , katanjenguwul
potentiel thermodynamique : embaj tangjoxal
travail maximum : ligeeybaëp
cycles dithermes , rendement : depneg yaritangay , delo
entropie : amannaojalaxu
couche électronique : deleye mbëjfepel
microphysique : nektutil
univers :datnek jacnek
univers atomique : jatnek xarefulwonal
saut électronique : tebum mbëcfepel
rayons X : cener X(nangam)
rayonnement A.B : ceneral A.B
radar jex jaw , jexkat
gravitation : warangiku
unités : ay natu
rien ne se perd rien ne se crée tout se transforme : dara du rer dara du saku ley dey sopiku
temps : jamono , jir
la matière et le néant : nen geg dara ji
machine : nopaldom-adama , nopalmbindef , wutuloxo




J 'ai essayé dans ce topic de rendre opératoire la traduction des termes scientifiques faite par CHEIKH ANTA DIOP . Cette traduction était surtout desservie par les graphies employées (notamment la distinction entre /d/ et /d/ mouillé , /t/ et /t/ mouillé rendue par la mise en italique ) qui rendaient souvent les termes incompréhensibles à bien des lecteurs . Nous espérons qu' avec les nouvelles graphies ce lexique scientifique aura le succés qu' il mérite . Nous vous serons gré de le diffuser largement .
DJIBRIL CHIMERE DIAW

Thursday, October 20, 2005

DJIBRIL CHIMERE DIAW

Avis aux étudiants, chercheurs et amoureux du savoir.

VOICI des liens qui peuvent vous être utiles dans vos études ou recherches

UNIVERSITYSURF.NET PORTAIL portail e-learning pluridisciplinaire en accès libre et gratuit offrant une sélection de plus de 1100 cours en ligne en langue française, et donnant accès à des milliers d'autres par le biais de liens. Les cours ou ressources pédagogiques proviennent de l'ensemble des 90 Universités françaises, Grandes Ecoles, Universités étrangères francophones, ou encore des nombreux sites personnels d'enseignants.
http://eunomie.u-bourgogne.fr/elearning/index.html


Serveur de Thèses Multidisciplinaire
http://tel.ccsd.cnrs.fr/


LE MATHS LINKER un index de ressource mathématiques sur le web , en ligne ou téléchargeables
http://mathslinker.chez.tiscali.fr/ml_fr.htm




Les classiques des sciences sociales Une bibliothèque numérique fondée et dirigée par Jean-Marie Tremblay, bénévole, professeur de sociologie au département des sciences humaines du Cégep de Chicoutimi Collection: Les auteurs classiques par ordre alphabétique La bibliothèque compte maintenant 1 602 oeuvres originales de 520 auteurs différents
http://www.uqac.uquebec.ca/zone30/Classiques_des_sciences_sociales/




Le dictionnaire Freelang est un programme gratuit à télécharger (logiciel freeware). Le programme ne s'installe qu'une seule fois, et vous pouvez ensuite y ajouter autant de listes de mots que vous le souhaitez. 175 dictionnaires sont actuellement proposés ! Pour télécharger le programme, choisissez une langue...
http://www.freelang.com/dictionnaire/



Les Écritures Vous trouverez ci-dessous la liste des écritures existantes sur ce site. À ce jour, il existe 287 écritures
http://aleph2at.free.fr/index.html?
http://aleph2at.free.fr/ecritures/liste.htm




LEXILOGOS MOTS ET MERVEILLES D ICI ET D AILEURS c’est un site fabuleux . http://www.lexilogos.com/index.htm





Librecours.org Centre de ressources pédagogiques
http://www.librecours.org/cgi-bin/main



Gallica Gallica propose un accès à 70 000 ouvrages numérisés, à plus de 80 000 images et à plusieurs dizaines d'heures de ressources sonores. Cet ensemble constitue l'une des plus importantes bibliothèques numériques accessibles gratuitement sur l'Internet http://gallica.bnf.fr/__



_______________


"Le savoir non digéré par la pensée est vain et la pensée non étayée par le savoir est dangereuse. "(Confucius) "L' Homme est le remède de l'Homme " (proverbe Wolof) " Tout ce que je sais c' est que je ne sais rien." (Socrate) http://www.grioo.com/blogs/DJIBRILCHIMEREDIAW/